mardi 28 septembre 2010

WaxTaan Wax ak Tànn

WaxTaan Wax ak Tànn 

Baatu waxtaan nek na baat bu diis ta woyof itam .Bu ñu ko seete dananu gis ne ñaari baat la : wax ak tànn . Waxtaan moy tànn wax , wax wax ju ñu tànn , bu nu waxe ba noppi , nu tànn li nu ciy denc .

Dinaa ci dellusi .

Agsileen

Agsileen . Bërëb bi seen kër la .